Youssou N'Dour — Sama Gàmmu letra e tradução

A página contém a letra e a tradução em português da música "Sama Gàmmu" de Youssou N'Dour.

Letra

Nanga def yaw sama gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
Xam naa ne yaw moomu loo ko
Dang ko àbb mbaa nga for ko
Baal dóózéé, eh
Nanga def, na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
Ba foo ma séén tàmbaleey wëlis
Xam naa ne yaw moomu loo ko
Dang ko àbb mbaa nga for ko
Baal dóózéé, eh
Yor xaalis mënui tee me moom la
Nanga def, na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
Xam naa ne yaw moomu loo ko
Dang ko àbb mbaa nga for ko
Baal dóózéé, eh
Kaay gaaw wax ma na nga def ba am ko
Foog nan nita ko waddal nga for ko
Wax ma gaaw ñaata la doon ma fay ko
Man daal maay sa buur nangu ko
Nanga def, na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
Ba foo ma séén tàmbaleey wëlis
Xam naa ne yaw moomu loo ko
Dang ko àbb mbaa nga for ko
Baal dóózéé, eh
Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee
Ah suñuy baay noonu lañ ko daan waxee
Ah suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee
Ah gàmmu daal sama doomu nday nga
E e e gàmmu daal suma xarit nga
E e e gàmmu daal suma askan nga
Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee
E e e gàmmu daal suma xarit nga
E e e gàmmu daal man sama doomu nday nga
E e e gàmmu daal man suma xarit nga
E e e gàmmu daal yaw sama doomu nday nga
Baal dooc moomu foo ko
Teeyai teey teey
Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee
Ah suñuy baay noonu lañ ko daan waxee
Ah suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee
E e e gàmmu daal sama doomu nday nga
E e e gàmmu daal suma xarit nga
E e e gàmmu daal suma askan

Tradução da letra

Nanga of yaw sama Gammu dégg of nga yor xaalis
Xam ou neil Yaw moomu los ko
Pessoas ko àbb mbaa nga para ko
Baal dóózéé, y
Nanga de, a nga de gàmmu dégg de nga yor xaalis
Base de If séén tàmbaleey wëlis
Xam ou neil Yaw moomu los ko
Pessoas ko àbb mbaa nga para ko
Baal dóózéé, y
Yor xaalis mënui tee me moom with
Nanga de, a nga de gàmmu dégg de nga yor xaalis
Xam ou neil Yaw moomu los ko
Pessoas ko àbb mbaa nga para ko
Baal dóózéé, y
Kaay gaaw wax if the nga d ba the ko
Foog ou agora planear ko waddal nga para ko
Wax if gaaw ñaata by doon if fay ko
Mann Daal maay in buur nangu ko
Nanga de, a nga de gàmmu dégg de nga yor xaalis
Base de If séén tàmbaleey wëlis
Xam ou neil Yaw moomu los ko
Pessoas ko àbb mbaa nga para ko
Baal dóózéé, y
Ali suñuy maam Noonu lañ ko Daan defee
Ali suñuy baay Noonu lañ ko Daan waxee
Ali suñuy yaay Noonu lañ ko Daan escuta
Ali gàmmu Daal sama doomu nday nga
Mas em gàmmu Daal sun xarit nga
Mas em gàmmu Daal sun askan nga
Ali suñuy maam Noonu lañ ko Daan defee
Mas em gàmmu Daal sun xarit nga
Mas em gàmmu Daal man sama doomu nday nga
Mas em gàmmu Daal man sun xarit nga
Mas em gàmmu Daal yaw sama doomu nday nga
Baal dooc moomu under ko
Teeyai teey teey
Ali suñuy maam Noonu lañ ko Daan defee
Ali suñuy baay Noonu lañ ko Daan waxee
Ali suñuy yaay Noonu lañ ko Daan escuta
Mas em gàmmu Daal sama doomu nga
Mas em gàmmu Daal sun xarit nga
Mas em gàmmu Daal sun askan